Skip to content

mottalil hadiisu : «innamal ahmaalu binniyaati...» jëf yi daal mingi aju ca yéene ya..." te nga tudd lenn ci ay njariñam?

الباب / الفصل
قسم الحديث

السؤال

س1: أكمل حديث: «إنما الأعمال بالنيات ...»، واذكر بعض فوائده.

mottalil hadiisu : «innamal ahmaalu binniyaati...» jëf yi daal mingi aju ca yéene ya..." te nga tudd lenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أمير المؤمنين أبي حفص عمر بن الخطاب رَضِيَ اللَّهُ تَعَالَى عَنْهُ قال: سمعت رسول الله صَلَّى اللهُ تَعَالَى عَلَيْهِ وعَلَى آَلِهِ وَسَلَّمَ يقول:

«إنما الأعمال بالنيات، وإنما لكل امرئ ما نوى، فمن كانت هجرته إلى الله ورسوله؛ فهجرته إلى الله ورسوله، ومن كانت هجرته لدنيا يصيبها، أو امرأة ينكحها؛ فهجرته إلى ما هاجر إليه»

رواه البخاري ومسلم.

فوائد من الحديث:

  1. كل عمل لا بد له من نية، من صلاة، وصوم، وحج، وغيرها من الأعمال.
  2. لا بد من الإخلاص في النية لله تَعَالَى.

jële nañu ci njiiti way-gëm yi baayu Hafsin Umar Ibnu (doomu) Alxattaab -yal na ko Yàlla mu kawe mi dollee gërëm- mu wax ni: dégg naa yònente Yàlla bi yalna ko Yàlla dolli jàmm ak mucc ak i ñoñam mu wax ne:

"jëf yi mi ngi aju ci yéene yi, te nit ku nekk la mu yéene rekk lay am, képp ku gàddaay ngir Yàlla ak ub yónentem, koo ku gàddaayam dina jëm ci Yàlla ak yónentem, waaye képp ku gàdaay ngir àdduna jum soxlaa jot, wala jigéen ju mu bëgg a takk; kon gàddaayam jëm na ca la ko taxa gàddaay"

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

ay njariñ ci hadiis bi:

  1. jëf june warnaa ànd ak yéene, julli, woor, aj, ak yeneen jëf yi.
  2. sellal ngir Yàlla mu kawe mi mënuta ñàkk ci yéene.