Skip to content

mottalil hadiisu «képp ku sos ci sunu mbir mii (diiné jii)...», te nga tudd lenn ci ay njariñam?

الباب / الفصل
قسم الحديث

السؤال

س2: أكمل حديث «من أحدث في أمرنا هذا ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 2: mottalil hadiisu «képp ku sos ci sunu mbir mii (diiné jii)...», te nga tudd lenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أم المؤمنين أم عبد الله عائشة رَضِيَ اللَّهُ عَنْهَا قالت: قال رسول الله ﷺ:

«من أحدث في أمرنا هذا ما ليس منه، فهو ردٌّ»

رواه البخاري ومسلم.

فوائد من الحديث:

  1. النهي عن الابتداع في الدين.
  2. وأن الأعمال المحدثة مردودة غير مقبولة.

jële nañu ci yaayu jullit ñi Aysatu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: yònente Yàlla bi neena:

«képp ku sos ci sunu mbir mii luci bokkul dees la koy delloo"

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

ay njariñ ci hadiis bi:

  1. tere sos ci diine.

2-jëf yin sos ci diine dees koy dello te deesu ko nangu