Skip to content
ما لا يسع أطفال المسلمين جهله

ما لا يسع أطفال المسلمين جهله

muy aw doxaliin wu gàtt te yomb,te làmboo masalay pas-pas ak fiq, ak jaar-jaari yonent bi, ak lu jëm ci ay teggiin,ak firim Alquraan ak adiis, ak ay jikko ak i ñaan,muy lu baax ci ndaw ñi ak bépp maas ak nu ay atam mana toll, baax na ci tuubéen yi tamit manaam ñiy door a dugg ci lislaam,muy lees man a jàngale ci kër yi ak daara yi, muy lu neex a mokkal ta yomb a leeral; dama koo toftale kem fànni xam-xam yi, def ko it ci anamug laaj ak tontu ndax loolu moo gën ci nàmm xel yi, te mooy li gën a dëgër cig mokkal, yarkat bi mooy tànn li gën a méngoo ak ati Aji-jàng ji.

0%
Font size