Skip to content
lu ab jullit warut a réere.

lu ab jullit warut a réere.

Téereb (lu jullit bi warut a réere) téere bu tedd la, ñu tëgg ay arafam ci daa joo xam ne xam-xam la ak leeral, mu dajale lu jullit bi warut a réere ci cosaani ngëm, ak àttey Lislaam, ak jikkó yu rafet, ci anam gu ñu xereñe, gis-gis yi di ci leere, xol yi di ci dale, muy setal dégg-dégg yi, di jubbanti jëf yi. Mu doon ca dëgg-dëgg caabiy mucc, ak ab tegtal ñeel ki dox ci yooni topp Yàlla ak xam-xam.

Language: lang_wo
Prepared by: Lajnatul Hilmiyyatu bi-Ri'aasati As-Su'uuni Ad-Diiniyyati bil-Masjidi Al-Haraami wal-Masjidi An-Nabawiyyi.
Version: 3.1

These files are generated automatically from the book's text; their layout may differ from the printed edition.

0%
Font size