Skip to content
الدروس المهمة لعامة الأمة

الدروس المهمة لعامة الأمة

Ay njàngale yu am solo ñeel xeet wi yépp Ñeel fóore ju mag jii di Ci turu Yàlla miy Aji-Yërëm képp ku nekk ci kaw suuf jagleel ko jullit ñi ca allaaxira ci laay tàmbalee. Laytaayu aji-taalif ji Cant ñeel na Yàlla miy Boroom mbindéef yi, mujj ga ñeel na way- gëm ñi, Yal na Yàlla julli te sëlmal ci jaamam bi di Yonenteem bi Muhammat, moom ak waa-këram ak àndandoom yépp.

Language: lang_wo
Prepared by: Abdul Asiis Ibn Baas -yal na ko Yàlla yërëm-
Version: 2.1

These files are generated automatically from the book's text; their layout may differ from the printed edition.

0%
Font size