Skip to content
العقيدة الصحيحة وما يضادها

العقيدة الصحيحة وما يضادها

﴾Bëgguma ci ñoom wërsëg bëguma it ñu leel ma.﴿ [Saaru Azzaariyaati: 57]. ﴾ Yàlla mooy kiy wërsëgal te mooy boroom kàttan gu bari doole gi.﴿ [Saaru Azzaariyaati:58]. ﴾Yàlla moomu moo leen lalal Suuf si, tabaxal leen Asamaan si, wàcce ndox ci Asamaan génne ci gàncax muy wërsëg ci yéen, kon buleen wutal Yàlla ay moroom te fekk xam ngéen ko 22﴿ [Saaru Naqara: 22]. Buleen jaamu ku dul Yàlla man maay ki leen ciy xupp ak a bégal 2 ﴿ Ndax du Yàlla moo moom diine ju sell ﴿

0%
Font size