àqi Yàlla ci jaam ñi mooy ñu jaamu ko te bañ koo bokkaale ak dara, àqi jaam ñi ci Yàlla nag mooy du mbugal ku ko bokkaalewul ak dara
Jële na ñu ci Muhaas -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Toggoo woon naa ak Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- am Mbaam mu ñuy woowe Xufayr, mu ne ma: «yaw Muhaas, ndax xam nga lan moy Àqi Yàlla ci ay jaamam, ak lan mooy àqi jaam ñi ci Yàlla?», Muhaas nee: ma ne ko: Yàlla ak ub Yónenteem ñoo ko xam, Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- daal di ne ko: «àqi Yàlla ci jaam ñi mooy ñu jaamu ko te bañ koo bokkaale ak dara, àqi jaam ñi ci Yàlla nag mooy du mbugal ku ko bokkaalewul ak dara» ma ne ko: yaw Yónente Yàlla bi tee maa bégal nit ñi ci lii ? Mune ma: «buleen bégal kon dañuy bayliku.
كُنْتُ رِدْفَ النَّبِيِّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ عَلَى حِمَارٍ يُقَالُ لَهُ عُفَيْرٌ، فَقَالَ: «يَا مُعَاذُ، هَلْ تَدْرِي حَقَّ اللَّهِ عَلَى عِبَادِهِ، وَمَا حَقُّ العِبَادِ عَلَى اللَّهِ؟»، قُلْتُ: اللَّهُ وَرَسُولُهُ أَعْلَمُ، قَالَ: «فَإِنَّ حَقَّ اللَّهِ عَلَى العِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلا يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا، وَحَقَّ العِبَادِ عَلَى اللَّهِ أَنْ لا يُعَذِّبَ مَنْ لا يُشْرِكُ بِهِ شَيْئًا»، فَقُلْتُ: يَا رَسُولَ اللَّهِ أَفَلاَ أُبَشِّرُ بِهِ النَّاسَ؟ قَالَ: «لا تُبَشِّرْهُمْ، فَيَتَّكِلُوا».
Leerarug hdiis bi: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral àqi Yàlla ci jaam ñi, ak àqi jaam ñi ci Yàlla, ci ne àqi Yàlla ci jaam ñi mooy ñu jaamu ko moom dong te duñu ko bokkaale ak dara, Ak ne àqi jaam ñi ci Yàlla mooy mu bañ a mbugal ñi koy kennal te duñu ko bokkaale ak dara. Muhaas ne ko: yaw Yónente Yàlla bi, ndax duma bégal nit ñi ngir ñu bég ci ngëneel lii? Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere ko ngir ragal nit ñi di sukkandiku ci loolu.
...:
Bokk na ci njariñal hdiis bi: Leeral àqi ji Yàlla waral ci jaamam ñi, te mooy ñu jaamu ko, te bañ koo bokkaale ak dara.
Leeral àqi jaam ñi ci Yàlla mu kawe mi te Yàlla warlul ko boppam ngir ngëneel ak xéewal, te mooy mu dugal leen àjjana, te du leen mbugal.
Ag bégle la ñeel way-kennal yi nga xam ne duñu bokkaale Yàlla ak dara ci ne séenug mujj mooy dugg àjjana.
Muhaas dafa nettali hadiis bii laata muy faatu; ngir ragal a tàbbi ci bakkaaru nëbb xam-xam.
Artu ci bañ a tasaare yenn Hadiis yi ci yenn nit ñi ngir ragal ci kaw ñi nga xam ne manu ñoo xam maanaama; te loolu mooy yi nga xam ne jëf aju wu ca mbaa AB daan ci daani Sariiha yi.
Ñiy kennal Yàlla tey def ay bàkkaar ñoo ngi ci ron coobarey Yàlla bu ko soobee mbugal leen, bu ko soobee it mu jéggal leen, waaye seenug mujj mooy àjjana.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (4/ 29) (2856).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 58) (30).
(1/ 627).
Yataal gi (5)
المحكم لابن سيده (10/26).
المفهم لما أشكل من تلخيص كتاب مسلم (1/ 203).
فتح الباري (11/340.
البحر المحيط الثجاج في شرح صحيح الإمام مسلم بن الحجاج (1/ 623).
عمدة القاري شرح صحيح البخاري (14/ 148).
Cited in books
12 Books- Pas-pas bu wér ak ub safaanam.Li Yàlla yayoo ci jaam ñi mooy ñu jaamu ko te bañkoo bokkaale ak dara »[2].
- Pas-pas bu wér ak ub safaanam.﴾ Ndax xam nga lan moy Àq i Yàlla ci ay jaamam, ak àq i jaam ñi ci Yàlla, Muhaas ne: mane ko: Yàlla ak ub Yónnenteem ñoo ko xam, Yónnente bi -yalna ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- daa di ne ko: àq i Yàlla ci jaam ñi mooy ñu jaamu ko te bañkoo
Yataal gi (10)
- العقيدة الصحيحةدروس العقيدة الصحيحة«فَإِنَّ حَقَّ اللَّهِ عَلَى العِبَادِ: أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلَا يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا، وَحَقَّ العِبَادِ عَلَى اللَّهِ: أَنْ لاَ يُعَذِّبَ مَنْ لَا يُشْرِكُ بِهِ شَيْئًا»
- حراسة التوحيدالعقيدة الصحيحة وما يضادها «حَقُّ اللهِ عَلَى العِبَادِ أَن يَعْبُدُوهُ وَلَا يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا» [2].
- حراسة التوحيدإقامة البراهين على حكم من استغاث بغير الله«حَقُّ اللهِ عَلَى العِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلَا يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا».
- خذ عقيدتك من الكتاب والسنة الصحيحة«حق العباد على الله أن لا يُعذِّبَ مَن لَا يشركُ به شيئًا»
- كتاب التوحيدكتاب التوحيد للشيخ محمد بن عبد الوهاب" حَقُّ اللهِ عَلَى الْعِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلاَ يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا، وَحَقُّ الْعِبَادِ عَلَى اللهِ أَنْ لاَ يُعَذِّبَ مَنْ لاَ يُشْرِكُ بِهِ شَيْئًا "،
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (1)، والسيرة النبوبة (1)، والعقيدة (1)، والفقه (1)التربية الأسلامية 1قال: «فإن حق الله على العباد أن يعبدوه ولا يشركوا به شيئًا، وحق العباد على الله ألا يعذب من لا يشرك به شيئًا»
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (1)، والسيرة النبوبة (1)، والعقيدة (1)، والفقه (1)التربية الأسلامية 1«حقُّ اللهِ على العِبادِ أنْ يعْبُدُوهُ ولا يُشْرِكُوا بِهِ شيْئًا...»
- مشروع منهاج زادكزادك 2 طالب نهائي«يَا مُعَاذُ، هَلْ تَدْرِي حَقَّ اللهِ عَلَى عِبَادِهِ؟ وَمَا حَقُّ العِبَادِ عَلَى اللهِ؟». قُلْتُ: اللهُ وَرَسُولُهُ أَعْلَمُ. قَالَ: «فَإِنَّ حَقَّ اللهِ عَلَى العِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلاَ يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا، وَحَقَّ العِبَادِ ع
- نبراس طالب (3)نبراس طالب 3«يَا مُعَاذُ، هَلْ تَدْرِي حَقَّ اللهِ عَلَى عِبَادِهِ، وَمَا حَقُّ العِبَادِ عَلَى اللهِ؟»، قُلْتُ: اللهُ وَرَسُولُهُ أَعْلَمُ، قَالَ: «فَإِنَّ حَقَّ اللهِ عَلَى العِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلاَ يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا، وَحَقَّ العِبَادِ ع
- نبراس طالب (3)نبراس طالب 3«فَإِنَّ حَقَّ اللهِ عَلَى العِبَادِ أَنْ يَعْبُدُوهُ وَلاَ يُشْرِكُوا بِهِ شَيْئًا»