Skip to content

السؤال

س10: أكمل حديث «ألا إن في الجسد مضغة...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 10: Motti lil hadiisu « Alaa inna fil jasadi mudxatan...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن النعمان بن بشير رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُما قال: سمعت رسول الله صلى الله عليه وسلم يقول:

«ألا وإن في الجسد مضغة إذا صلحت صلح الجسد كله، وإذا فسدت فسد الجسد كله، ألا وهي القلب»

رواه البخاري ومسلم.

بعض فوائد الحديث:

  1. صلاح القلب فيه صلاح الظاهر والباطن.
  2. الاهتمام بصلاح القلب لأن به صلاح الإنسان.

Jële nañu ci Annuhmaan Doomi Basiir yal na leen Yàlla dollee gërëm, neena: dégg naa Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-, mu wax ne:

«Damane am na ci yaram benn lumb deret bu baaxee yaram wi wépp baax, waaye bu yàqoo yaram wi yépp yàqu, loolu mooy xol»

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

Yénn ci njariñi hadiis bi:

  1. yéwenug biir ak bitti mingi ci yéwenug xol.
  2. yitte woo yéwenug xol ndax ci la nit di yéwene.