Skip to content

السؤال

س9: أكمل حديث «لا حول ولا قوة إلا بالله ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 9: Mottalil hadiisu Laa hawla wala xuwwata Illaa billahi...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أبي موسى رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«لا حول ولا قوة إلا بالله كنز من كنوز الجنة»

رواه البخاري ومسلم.

من فوائد الحديث:

  1. فضل هذه الكلمة، وأنها كنز من كنوز الجنة.
  2. تبرُّؤُ العبد من حوله وقوته، واعتماده على الله تَعَالَى وحده.

Jële nan ci Abii Muusaa yal na ko Yàlla dollee gërëm neena: Yónente bi -yal na na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«Laa hawla walaa xuwwata illaa bil-Laahi, am ndàmb la ci ndàmbi Aljana ya»

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

Bokk na ci njariñi hadiis bi:

  1. ngëneelu baat bi, ak it ne moom ndàmb la ci ndàmbi Aljana yi.
  2. setug jaam bi ci pexe ak ci kàttanam, ak ug sukkandikoom ci Yàlla mu kawe mi moom rekk.