السؤال
س١٦: ما هي البشاشة؟
Laaju 16: Xamleel lan mooy bélli?
الجواب
ج:هي طلاقةُ الوَجهِ، مع الفَرحِ والتَّبسُّمِ واللطف وإظهار السرور عند لقاء الناس.
وهي بعكس العبوس في وجه الناس مما ينفرهم.
- وفي فضل ذلك جاءت الأحاديث، فعن أبي ذَرٍّ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، قال: قال ليَ النَّبيُّ ﷺ:
«لا تَحْقِرَنَّ مِنَ المَعرُوفِ شَيْئًا، ولو أَنْ تَلْقَى أخاكَ بِوَجْهٍ طَلْقٍ»
رواه مسلم.
- وقالَ رَسولُ اللهِ ﷺ:
«تَبَسُّمُكَ فِي وَجْهِ أَخِيكَ لَكَ صَدَقَةٌ»
رواه الترمذي.
Mooy xar kanam, gu fecciku àndag mbégte ak muuñ ak ñeewant, ak feeñal mbégte ci boo dajee ak nit ñi.
te mooy safaanug fas xarkanam, ci kanami nit ñi ci lépp lu leen di dawloo.
Te ay Hadiis ñëw na si ngëneeli loolu, jële nanu si Abii Zarrin -yal na ko Yàlla dolli ngërëm-, mune: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak muicc- neena:
«Bul xeeb dara ci lu baax, donte dangay daje ak sa mbokk si kanam gu bélli»
Muslim moo ko soloo
yonente Yàlla bi neena:
«Sag muuñ ci sa kanamu mbokk sarax la»
Attirmisii moo ko soloo