السؤال
س١٨: ما هو الاستهزاء؟
Laaju 18: Lan mooy yéjji( saboote)?
الجواب
ج:هو السخرية من أخيك المسلم وتحقيره، وهذا لا يجوز.
قال تَعَالَى في النهي عن ذلك:
﴿يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ لَا يَسۡخَرۡ قَوۡمٞ مِّن قَوۡمٍ عَسَىٰٓ أَن يَكُونُواْ خَيۡرٗا مِّنۡهُمۡ وَلَا نِسَآءٞ مِّن نِّسَآءٍ عَسَىٰٓ أَن يَكُنَّ خَيۡرٗا مِّنۡهُنَّۖ وَلَا تَلۡمِزُوٓاْ أَنفُسَكُمۡ وَلَا تَنَابَزُواْ بِٱلۡأَلۡقَٰبِۖ بِئۡسَ ٱلِٱسۡمُ ٱلۡفُسُوقُ بَعۡدَ ٱلۡإِيمَٰنِۚ وَمَن لَّمۡ يَتُبۡ فَأُوْلَٰٓئِكَ هُمُ ٱلظَّٰلِمُونَ﴾
[الحجرات: ١١].
Mooy di reetaan sa mbokkum jullit ak di ko xeeb,te loolu daganul.
Yàlla mu kawe mi tere na loolu ci wax ne:
{Ée yéen ñi gëm bu benn nit reetaan beneen nit ndax amaana ñooñu gën ña leeni reetaan, bu benn jigéen it di reetaan benn jigéen ndax amaana ñoom ñu gën ña leen di reetaan, bu leen di ayibalante te bu leen di woowante ci ay tur yu leen neexul turu kàccoor yooyi de lu ñaaw la ginnaaw ngëm ga te ku tuubul ñoom ñooy tooñkat yi 11}
Saaru Al-mujaadala 11].