السؤال
س١٥: ما أنواع خلق المحبة؟
Laaju 15: Lan mooy xeeti jikkoy mbëggeel?
الجواب
ج:محبة الله تَعَالَى.
قال تَعَالَى:
﴿وَٱلَّذِينَ ءَامَنُوٓاْ أَشَدُّ حُبّٗا لِّلَّهِ﴾
[البقرة: ١٦٥].
- محبة الرسول صلى الله عليه وسلم.
قال ﷺ:
«والَّذي نَفْسي بِيَدِه، لا يُؤمِنُ أحدُكم حتَّى أكونَ أحبَّ إليهِ مِن والِدِه ووَلَدِه»
رواه البخاري.
محبة المؤمنين، ومحبة الخير لهم كما تحبه لنفسك.
قال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:
«لَا يُؤْمِنُ أَحَدُكُمْ حَتَّى يُحِبَّ لِأَخِيهِ مَا يُحِبُّ لِنَفْسِهِ»
- Bëgg Yàlla mu kawe mi.
Yàlla mu kawe mi neena:
«ñi gëm de Yàlla lan gëna bëgg»
saaru Baqara: 24
Bëgg Yónente bi yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc.
Moom wax na ne:
«Giñ naa ci ki sama bakkan nekk ci loxoom, kenn ci yéen du gëm ludul ma gënal ko way-juram ak doomam»
Buxaarii moo ko soloo.
Bëgg way gëm yi, te bëggal leen yiw ni ki nga ko bëggale sa bopp.
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:
«Kenn ci yéen du gëm; ndare mu bëggal mbokkam li mu bëggal boppam»