Skip to content

السؤال

س8: أكمل حديث: «والذي نفسي بيده! ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 8: Mottalil hadiisu: « wallajii Naf sii biyadihii ...» te nga tudd leen ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أبي سعيد رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، عن رسول الله صلى الله عليه وسلم قال:

«والذي نفسي بيده! إنها لتعدل تعدل ثلث القرآن»

رواه البخاري.

بعض فوائد الحديث:

  1. فضل سورة الإخلاص.
  2. وأنها تعدل ثلث القرآن.

Jële na nu ci Abii Sahiid, -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, mu jële ci Yónente bi -yalna ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-, mu wax ne:

«giñ naa ci ki sama bakkan nekk ci loxoom! moom dé dana yamoog ñatteelu xaaju Alxuraan»

Buxaarii moo ko soloo.

Yénn ci njariñi hadiis bi:

  1. Ngëneelu saaru Al-ixlaas.
  2. Moom day yamoo ak ñatteelu xaaju Alxuraan.