Skip to content

السؤال

س٢٠: ما أنواع الكِبْرُ المحرم؟

Laaju 20: Yan mooy xeeti rëy yi nga xamni dafa araam?

الجواب

ج:١. الكِبْر على الحق، وهو رد الحق وعدم قبوله.

  1. الكِبْرُ على الناس، وهو احتقارهم والاستهانة بهم.

قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«لا يَدخُلُ الجَنَّةَ مَن كان في قَلبِه مِثْقالُ ذَرَّةٍ مِن كِبْرٍ».

فقال رَجُلٌ: إنَّ الرَّجُلَ يُحِبُّ أن يَكونَ ثَوبُه حسَنًا، ونَعْلُه حسَنةً؟ قال:

«إنَّ اللهَ جَميلٌ يُحِبُّ الجَمالَ، الكِبْرُ: بَطَرُ الحَقِّ، وَغَمْطُ النَّاسِ»

رواه مسلم.

  • بَطَرُ الحَقِّ: رده
  • غَمْطُ النَّاسِ: استحقارهم.
  • الثوب الحسن والنعل الحسن ليس من الكبر.
  1. Rëy ci kaw dëgg, te mooy delloo dëgg bañ koo nangu.
  2. Rëy ci kaw nit ñi, te mooy xeeb leen ak doyodal leen.

yonente Yàlla bi neena:

«Ku ab peppu rëy nekk ci xolam du dugg Aljana».

Benn waay neko: nit kiy bëgg ay Yéereem ak i dàllam rafet nag? mu ne ko:

«Yàlla dafa rafet te daa bëgg lu rafet, rëy mooy: bañ dëgg ak xeeb nit ñi»

Muslim moo ko soloo

  • Batarul hàq: mooy Bañ dëgg
  • Xamtun naasi: mooy xeeb nit ñi.
  • Yéere bu rafet ak dàll yu rafet bokkul ci rëy.