السؤال
س١٩: ما هو التواضع؟
Laaju 19: Xamleel lan mooy woyoflu?
الجواب
ج:هو أن لا يرى الإنسان نفسه على الناس، فلا يستحقر الناس ولا يرفض الحق.
- قال تَعَالَى:
﴿وَعِبَادُ الرَّحْمَنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا﴾
[الفرقان: ٦٣]،
أي: متواضعين.
- وقالَ رسولُ اللهِ ﷺ:
«وما تَواضَعَ أحَدٌ للهِ إلَّا رَفَعَهُ اللهُ»
رواه مسلم.
- وقال صلى الله عليه وسلم:
«إنَّ اللهَ أَوْحى إليَّ أنْ تَواضَعُوا، حتَّى لا يَفخَرَ أحَدٌ على أحَدٍ، ولا يَبْغيَ أحَدٌ على أحَدٍ»
Mooy nit ki bañ a gis ne moo gën a kawe nit ñi, du xeeb nit ñi te du bañ dëgg.
Yàlla mu kawe mi neena:
{Jaami Yàlla yi dëgg mooy ñiy dox ndànk ci kaw Suuf}
Saaru Alfurxaan 63],
Maanaam: di ay Aji-woyof.
yonente Yàlla bi neena:
«Kenn du woyof-wofof lu lu dul ne Yàlla dina ko yékkati»
Muslim moo ko soloo
Yónente Yàlla bi wax na ni:
«Yàlla soloo nama ne nangeen di woyof ba kenn du puukarewu si kaw kenn, te kenn itam du bew ci kaw kénn»