Skip to content

السؤال

س24: ما هو الكسل؟

Laaju 24: Lan mooy tàyyeel?

الجواب

ج:هو التثاقل عن فعل الخير وما يجب على الإنسان فعله.

ومن ذلك: التكاسل في فعل الواجبات.

  • قال الله تَعَالَى:

﴿إِنَّ ٱلۡمُنَٰفِقِينَ يُخَٰدِعُونَ ٱللَّهَ وَهُوَ خَٰدِعُهُمۡ وَإِذَا قَامُوٓاْ إِلَى ٱلصَّلَوٰةِ قَامُواْ كُسَالَىٰ يُرَآءُونَ ٱلنَّاسَ وَلَا يَذۡكُرُونَ ٱللَّهَ إِلَّا قَلِيلٗا﴾

[النساء: ١٤٢].

فينبغي للمؤمن ترك الكسل والخمول والقعود، والسعي في العمل والحركة، والجد والاجتهاد في هذه الحياة بما يرضي الله تَعَالَى.

Mooy nit ki di diis lu ci def yiw ak li mu war a def.

Te bokk na ca: Tàyyeel ci def wartéef yi.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Naaféq ya dañuy jéem a wor Yàlla waaye Yàlla dana leen njuuy, te bu ñu jògee jëm ca julli ga, da ñiy jòg cig tàyyeel, da ñiy ngistal ci bëti nit ñi, te du ñu tudd Yàlla lu dul lu néew ci moom 142}

suuratu annisaa

Jullit bi warnaa moytu tàyyeel ak giim ak toog rek, te ligéey ak yëngatu ak pastéefu ci dund gi ci lépp luy gërëmloo Yàlla.