Skip to content

السؤال

س٢٢: ما هي الغيبة؟

Laaju 22: Lan mooy jëw?

الجواب

ج:هي ذِكْرُ أخيك المسلم بما يكره وهو غائب.

  • قال تَعَالَى:

﴿وَلَا يَغْتَبْ بَعْضُكُمْ بَعْضًا أَيُحِبُّ أَحَدُكُمْ أَنْ يَأْكُلَ لَحْمَ أَخِيهِ مَيْتًا فَكَرِهْتُمُوهُ وَاتَّقُوا اللَّهَ إِنَّ اللَّهَ تَوَّابٌ رَحِيمٌ﴾

[الحجرات: ١٢].

  • Mooy nga tudd sa mbokk si lu ko neexul foo xamne nekkufa.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Bu ñenn si yéen di jëw ñeneen ñi, mo ndax kenn si yéen bëgg naa lékk yàppu mbokkam mu fekk mu dee, yéen ñéppa bañ loolu, ragal léen Yàlla, Yàlla Aji-Jéggale la Aji-yërëme la 1}

Saaru Al-mujaadala 11].