السؤال
س٢٨: ما هو الجبن؟ وما هي الشجاعة؟
Laaju 28: Lan mooy buqat? ak lan mooy njàmbaar?
الجواب
ج:الجبن: أن يخاف مما لا ينبغي أن يخاف منه.
مثل الخوف من قول الحق وإنكار المنكر.
الشجاعة: وهي الإقدام على الحق، وذلك مثل الإقدام في ساحات الجهاد للدفاع عن الإسلام والمسلمين.
- وكان النبي ﷺ في دعائه يقول:
«اللَّهُمَّ إنِّي أعوذُ بكَ من الجُبنِ...».
- وقال رسولُ اللهِ ﷺ:
«المؤمنُ القويُّ خيرٌ وأحبُّ إلى اللهِ مِن المؤمنِ الضَّعيفِ، وفي كُلٍّ خيرٌ»
رواه مسلم.
Buqat mooy: di ragal lu jarula ragal.
Ni ki di ragala wax dëgg ak weddi lu ñaaw.
Njàmbaar: mooy dëgmal dëgg, lu ci mel ne dëgmal barabu jihaad yi ngir aar Lislaam ak jullit yi.
Yónente bi daa na wax ci ñaanam yi:
«Yaw Yàlla maa ngi lay muslu buqat...»
yonente Yàlla bi neena:
«Jullit bu am kàttan moom la Yàlla gën a bëgg ci jullit bu lompañ, waaye ñoom ñéppa am yiw»
Muslim moo ko soloo