Skip to content

السؤال

س١: ما هو فضل الذكر؟

Laaju 1: Lan mooy ngëneelul tudd Yàlla?

الجواب

ج:قال النبي صلى الله عليه وسلم:

«مثل الذي يذكر ربه والذي لا يذكر ربه، مثل الحي والميت»

رواه البخاري.

  • هذا لأن قيمة حياة الإنسان بقدر ذكره لله تَعَالَى.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«misaalum kiy tudd Yàlla ak ki dul tudd Yàlla, mi ngi mel ni kuy dund ak ku dee»

Buxaarii moo ko soloo.

  • Ndax dayob dundug nit ki mi ngi ci kem ni miy tudde Yàlla mu kawe mi.