Skip to content

السؤال

س٢٧: ما هو الإسراف؟ وما هو البخل؟ وما هو الكرم؟

Laaju 27: Lan mooy yàq? ak lan mooy nay? ak lan mooy tabe?

الجواب

ج:الإسراف: هو إنفاق المال بغير حقه، وعكسه: البخل: وهو الإمساك عن حقه.

والصحيح هو الوسط بينهما، وأن يكون المسلم كريمًا.

  • قال تَعَالَى:

﴿وَٱلَّذِينَ إِذَآ أَنفَقُواْ لَمۡ يُسۡرِفُواْ وَلَمۡ يَقۡتُرُواْ وَكَانَ بَيۡنَ ذَٰلِكَ قَوَامٗا﴾

[الفرقان: ٦٧].

Nay mooy: sànk alal ci lu dul dëgg,

Safaanam mooy: nay: te mooy baña def alal fiñuko wara def.

Li wér nag mooy digg-dóomu séen digante, jullit bi nekk ku tabe.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Ak ñi nga xam ne bu ñuy joxe du ñu yàq te du ñu nay, dañuy digg-doomu 67}

Saaru Alfurxaan 63],