Skip to content

السؤال

س٢٦: ما هو التجسس؟

Laaju 26: Lan mooy luññutu Ak jëddu?

الجواب

ج:هو الكشف والبحث عن عورات الناس وما يسترونه.

من صوره المحرمة:

  • الاطلاع على عورات الناس في البيوت.
  • استماع المرء إلى حديث قوم بدون علمهم.
  • قال تَعَالَى:

﴿وَلَا تَجَسَّسُوا ...﴾

[الحجرات: ١٢].

Mooy wuññi ak gëstu awray nit ñi ak li ñu doon làq.

Bokk na ci ay anamam yu araam:

  • Di yër awray nit ñi ci seen kër yi.
  • Nit ki di deglu waxi nit yoo xam ne yéguñu ko.

Yàlla mu kawe mi neena:

«Buleen di yëddóonte 12}

Saaru Al-mujaadala 11].