Skip to content

السؤال

س۸: ما هي أعياد المسلمين؟

Laaju 7: Yan mooy xew-xewi jullit ñi?

الجواب

ج:عيد الفطر وعيد الأضحى.

لما جاء في حديث أَنَسٍ رضي الله عنه، قَالَ:

قَدِمَ رَسُولُ اللَّهِ ﷺ الْمَدِينَةَ وَلَهُمْ يَوْمَانِ يَلْعَبُونَ فِيهِمَا، فَقَالَ: «مَا هَذَانِ الْيَوْمَانِ؟»، قَالُوا: كُنَّا نَلْعَبُ فِيهِمَا فِي الْجَاهِلِيَّةِ، فَقَالَ رَسُولُ اللَّهِ ﷺ:«إِنَّ اللَّهَ قَدْ أَبْدَلَكُمْ بِهِمَا خَيْرًا مِنْهُمَا: يَوْمَ الْأَضْحَى، وَيَوْمَ الْفِطْرِ»

رواه أبوداود.

وما سواهما من الأعياد فمن البدع.

  • Xewu korite ak xewu tabaski.

Ni ki mu ñëwe ci hadiisu Anas, neena: Yónente bi dafa ñëw Madiina fekk ñu am ñaaari bis yoy dañu cay fo, mu ne leen: «ñaari bis yii mooy lan?», ñu ne ko: da nu ci daan fo jomanoy ceddo ga, Yònente bi ne leen:

«Yàlla wuutalal na leen ko lu ko gën: bisu tabaski, ak bisu korite»

Abuu Daawuda mooko soloo.

xew-xew bu bokkul ak ñoom ñaar ci bidaa yila.