Skip to content

السؤال

س١٣: ما أنواع خُلق الحياء؟

Laaju 13: Yan mooy xeeti jikkoy kersa?

الجواب

ج:١. الحياء من الله: يكون بأن لا تعصيه سُبْحَانَهُ.

  1. الحياء من الناس: ومن ذلك ترك الكلام الفاحش البذيء وكشف العورة.
  • قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«الإِيمانُ بِضْعٌ وسَبعونَ» - أو: «بِضْعٌ وسِتُّونَ» - «شُعْبةً، أَعْلَاها: قَوْلُ: لا إِلَهَ إلَّا اللهُ. وأَدْناها: إِماطةُ الأَذَى عنِ الطَّريقِ. والحَياءُ شُعْبةٌ مِنَ الإِيمانِ»

رواه مسلم.

  1. am kersa ci Yàlla: mooy nga bañ koo moy moom Yàlla mu sel mi.
  2. am kersa ci nit ñi: bokk na ca bàyyi wax ju ñaaw te bon, bañ a wuññi awray kenn.

yonente Yàlla bi neena:

«Ngëm juróom-ñaar fokki xaaj la yu topp» wala: «juróom-benni fukki xaaj la ak lu topp» - ci ay xaaj la, bi ci gën a kawe: mooy wax: laa ilaaha illal Illa Laahu, bi ci gën a suufe, mooy: randale aw lor si kaw yoon wi, te kersa benn pàcci la ci ngëm»

Muslim moo ko soloo