Skip to content

السؤال

س٧: ما ضد الأمانة؟

Laaju 7: Lan mooy safaanu kóolute?

الجواب

ج:الخيانة، وهي تضييع حقوق الله تَعَالَى وحقوق الناس.

  • قال تعالى:

﴿يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ لَا تَخُونُواْ ٱللَّهَ وَٱلرَّسُولَ وَتَخُونُوٓاْ أَمَٰنَٰتِكُمۡ وَأَنتُمۡ تَعۡلَمُونَ﴾

[الأنفال: ٢٧].

  • قال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«آيَةُ المُنافِقِ ثَلاثٌ» - وذكر منها - «وإذا اؤْتُمِنَ خانَ»

متفق عليه.

Wor, te mooy sànk àqi Yàlla mu kawe mi ak àqi nit ñi.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«Màndargay naaféq ñatt la» -mu tudd ca- «bu ñu ko wóolóo mu wor»

Buxaari ak Muslim dёppoo na ñu ci.