Skip to content

السؤال

س٦: ما أنواع الأمانة وصورها؟

Laaju 6: Yan mooy xeeti kóolute yi aki anamam?

الجواب

ج:١. أمانة في حفظ حقوق الله تَعَالَى.

صورها: الأمانة في أداء العبادات من الصلاة، والزكاة، والصيام، والحج، وغيرها مما افترض الله علينا.

  1. أمانة في حفظ حقوق الخلق:
  • من حفظ أعراض الناس.
  • وأموالهم.
  • ودمائهم.
  • وأسرارهم، وجميع ما ائتمنك عليه الناس.

قال تَعَالَى في ذِكر صِفات المفلحين:

﴿وَٱلَّذِينَ هُمۡ لِأَمَٰنَٰتِهِمۡ وَعَهۡدِهِمۡ رَٰعُونَ﴾

[المؤمنون: ٨].

Tontuli-

  1. Kóolute ci wattu àqi Yàlla mu kawe mi.

Ay anamam: am kóolute ci def jaamu Yàlla yi ci julli ak joxe Asaka ak woor ak aj ak yeneen yi Yàlla farataal ci nun.

  1. Kóolute ci wattu àqi mbindéef yi.
  • Ci wattu deri nit ñi.
  • Ak séeni alal.
  • Ak séen i deret.
  • Ak séen i mbóot, ak mbooleem lila nit ñi wóolóo.

Yàlla wax na ci melokaani way-texe yi:

{Ak ñi nga xam ne dañiy sàmm seen i kóllare ak séeni dëel 8}

saaru al-Muuminuuna 1-2.