Skip to content

السؤال

س٨: ما هو خلق الصدق؟

Laaju 8: Lan mooy jikkoy dëggu?

الجواب

ج:هو الإخبار بما يطابق الواقع أو الشيء على ما هو عليه.

ومن صوره:

  • الصدق في الحديث مع الناس.
  • الصدق في الوعد.
  • الصدق في كل قول وعمل.
  • قال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«إنَّ الصِّدقَ يَهْدي إلى البِرِّ، وإنَّ البِرَّ يَهْدي إلى الجنَّةِ، وإنَّ الرَّجلَ لَيَصْدُقُ حتَّى يكونَ صِدِّيقًا»

متفق عليه.

  • Mooy xibaare lu dëppoo ak li am, wala mbir mi ni mu ame.

Bokk na ci ay anamam:

Dëggu ci wax ak nit ñi.

Dëggu ci dige.

Dëggu ci wax ak jëf.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«Dëggu day jëmale cig mbaax, te ag mbaax day jëmale Aljana, nit ki dina dëggal ba mujj nekk Dëggalaakon»

Buxaari ak Muslim dёppoo na ñu ci.