Skip to content

السؤال

س٩: ما ضد الصدق؟

Laaju 9: Lan mooy safaanu dëggu?

الجواب

ج:الكذب، وهو خلاف الحقيقة، من ذلك، الكذب على الناس، وإخلاف المواعيد، وشهادة الزور.

  • قال النبي صلى الله عليه وسلم:

«وإنَّ الكذِبَ يَهْدي إلى الفُجورِ، وإنَّ الفُجورَ يَهْدي إلى النَّارِ، وإنَّ الرَّجلَ لَيَكذِبُ حتَّى يُكتَبَ عندَ اللهِ كذَّابًا»

متفق عليه.

  • وقال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«آيةُ المُنافِقِ ثَلاثٌ» -وذكر منها- «إذا حدَّثَ كَذَبَ، وإذا وَعَدَ أَخلَفَ»

  • Fen, te mooy wuute ak li wér, te bokk na ca, di fen nit ñi ak wuuteb dige, ak seede ay caaxaan.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- wax Na ne:

«Fen day jëmale nit ki cig kàccoor, te ag kàccoor day jëmale Sawara, te nit ki dina fen bañu bindal ko fa Yàlla ni fenkat la»

Buxaari ak Muslim dёppoo na ñu ci.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm mucc- neena:

«Màndargay naaféq ñatt la" -mu tudd ca- «bu waxtaanee day fen, bu digee day wuute dig ba»