وهذهِ رِسالَةٌ مُوجَزَةٌ لَكَ يا مَن فَقَدتَ قَرِيبًا أو عَزِيزًا، أو حَبِيبًا، نَسألُ اللَّهَ عزَّ وجلَّ أن ينفعنا وإياكَ بِها، وهي بِعنوان: (أحكامُ الجَنائِز).
BEEPP MIR MUMU MANA DOON DAAY TEKTALE AMUK YAALLA MIKO BIND! KAN MOO BIND ASAMAN YI AK LICI SEEN BIIR CI AY MBINDEEF YU MAAGG YOO XAMNE MBINDEEF MANULEENA PEEK? Kan moo def nosiin wu xereñe wii ? Kan moo bind nit may ko ag dégg ak ub jis ak xel te def ko muy ku man a am xam-xam tey xam li xew. Naka ngay firee wii tërëliin wu yéeme ci jumtukaay yi nekk ci sa biir yaram ak yaramu ndundat yi ? Kan moo fent loolu ? Naka la dund bu rëy bii man a nosaloo ci tëraliinam yu koy nose nose gu yéeme ba àdduna sosoo ba tay ?
Warug jëfe sunnas Yonnent bi ak kéefarug képp ku ko weddi.
23 languages
Warug jëfe sunnas Yonnent bi ak kéefarug képp ku ko weddi.
Aji-taalif ji Abdul Asiis Ibn baas -yal na ko Yàlla yërëm- Ci turu Yàlla miy Aji-Yërëm kepp ku nekk ci kaw suuf jagleel ko jullit ñi ca allaaxira ci laay tàmbalee. Laytaay ji Cant ñeel na Boroom mbidéef yi, Ag mujj ñeel na ñi ragal Yàlla, jàmm ak xéewal yal na nekk ci sunu Yonnent Muhammat, moog waa këram ak i àndandoom ñoom ñi gàddu téere Yàlla bi ak Sunnas seen Yonnent -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- jottali ko ña ñëw ci seen ginnaaw, ci koolute gu mat sëkk ak ug xereñte, ak ug wattu gu mat sëkk ñeel ay maanaam ak i baatam, -yal na leen Yàlla dollee gërëm te boole nu ci ñi leen di…
Lislaam mooy jébbalul Yàlla mi bind àdduna bi di ko doxal, wommatul ko ngir bëgg ko ak màggal ko, cosaanu lislaam mooy gëm Yàlla, ak ne moom mooy Aji-Bind ji, te lépp lu dul moom mbindeef la, ak ne moom moo yayoo jaamu moom rekk amul bokkaale, amul lenn lu ñuy jaamu ci dëgg ku dul moom,ay tur yu rafet ñeel na ko ak ay melo yu kawe, mooy ki mat sëkk, jurul kenn te kenn juru ko te amul benn nawle du caagine niroowaale, du wàcc te du jël jëmmi lenn ci mbindeefam yi. Lislaam mooy diiney Yàlla mi nga xam ne du nangu ci nit jenn diine ju dul moom, te mooy diine ji yonnente yépp indi yal na leen…