Skip to content

السؤال

س٥: ما ضد الإحسان؟

Laaju 5: Lan mooy safaanu rafetal?

الجواب

ج:ضد الإحسان الإساءة.

  • ومن ذلك: ترك الإخلاص في عبادة الله تَعَالَى.
  • وعقوق الوالدين.
  • وقطع الأرحام.
  • وسوء الجوار.
  • وترك الإحسان إلى الفقراء والمساكين وغير ذلك من سيء الأقوال والأعمال.

Safaanu rafetal mooy ñaawal.

  • Te bokk na ci: baña sellal ci jaamu Yàlla mu kawe mi.
  • Ak dog ñaari way-jur.
  • Ak dog mbokk.
  • Ak ñaawal dëkkadoo.
  • Ak bañ a rafetal jëme ci way ñakk yi ak yeneen yu dul yoo yu ci ñaawal i wax wala jëf.