Skip to content

lan mooy maanaam seede ne Muhammat yonenteb Yàlla la ?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy maanaam seede ne Muhammat yonenteb Yàlla la ?

س6: ما معنى شهادة أنَّ محمدًا رسول الله؟

الجواب

Loolu mooy nga nanggu ne yonente bi Yàlla moo ko yónni ci mbindéef yi muy bégal ñi ko topp di xupp ñi ko moy

Dina war:

  1. nu topp ko ci li mu santaane.
  2. nu dëggal ko ci lépp lu mu nu xibaare.
  3. nu bañ a wuute ak moom di moy ndigalam.
  4. nu bañ a jaamu Yàlla lu dul ci li mu yoonal maanaam nu tënku ci sunnaam bàyyi lépp luy bidaa.

Yàlla wax na ci suuratu nisaahii ne: képp ku topp yonente bi topp nga Yàlla, mu dellu waxaat ne:

﴾Yonente bi du waxe ci bànneexu bakkanam, lumu wax dees ka koo yenkeewal﴿ maanaam du wax ludul liko Yàlla wax loo

suuratu annajmi 3;4

Yàlla mu kawe mi te sell neena:

﴾am ngeen ci yonente bi ab royuwaay bu rafet ñeel képp ku yaakaar Yàlla te gëm bis-pénc tay tudd Yàlla lu bari﴿

suuratul ahzaab 21

ج:معناها: أن الله أرسله للعالمين بشيرًا ونذيرًا.

  • ويجب:
  1. طاعته فيما أمر.
  2. تصديقه فيما أخبر.
  3. عدم معصيته.
  4. لا يعبد الله إلا بما شرع، وهو الاقتداء بالسنة وترك البدعة.

قال تَعَالَى:

﴿مَّن يُطِعِ ٱلرَّسُولَ فَقَدۡ أَطَاعَ ٱللَّهَۖ﴾

[النساء: 80]،

وقال سُبْحَانَهُ:

﴿وَمَا يَنطِقُ عَنِ ٱلۡهَوَىٰٓ 3

إِنۡ هُوَ إِلَّا وَحۡيٞ يُوحَىٰ 4﴾

[النجم: 3-4].

وقال جَلَّ وَعَلَا:

﴿لَّقَدۡ كَانَ لَكُمۡ فِي رَسُولِ ٱللَّهِ أُسۡوَةٌ حَسَنَةٞ لِّمَن كَانَ يَرۡجُواْ ٱللَّهَ وَٱلۡيَوۡمَ ٱلۡأٓخِرَ وَذَكَرَ ٱللَّهَ كَثِيرٗا﴾

[الأحزاب: 21].