Skip to content

السؤال

lan mooy jaamu ?

س٨: ما هي العبادة؟

الجواب

loolu de ab baat la bu làmboo lépp lu Yàlla bëgg te gërëm ko ci ay wax ak ay jëf ci lu feeñ mbaa lu nëbbu.

Li feeñ nag mooy lu mel ni tudd Yàlla ci làmmiñ di ko sàbbaal ak di ko sant ak màggal ko, wala sax julli Mbaa aj màkka.

Li nëbbu mooy lu mel ni wakkiirlu ci Yàlla ak ragal ko ak yaakaar ko.

ج:هي اسمٌ جامعٌ لكلِّ ما يحبُّه الله ويرضاه من الأقوال والأعمالِ الباطنةِ والظاهرةِ.

  • الظاهرة: مثل ذكر الله باللسان من التسبيح والتحميد والتكبير، والصلاة والحج.
  • الباطنة: مثل التوكل والخوف والرجاء.