Skip to content

السؤال

س13: أكمل حديث «من حسن إسلام المرء ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 13: Mottalil hadiisu min xusni islaamil mar-i...» te nga tudd lenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أبي هريرة رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قال: قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«من حسن إسلام المرء: تركُه ما لا يعنيه»

رواه الترمذي وغيره.

من فوائد الحديث:

  1. ترك ما لا يعني الإنسان من أمور دين غيره ودنياه.
  2. أن ترك ما لا يعني من كمال إسلامه.

jële nañu ci Abii hurayrata -yal na ko Yàla dollee gërëm neena: yònente bi -Yalla na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«bokk na ci rafetug ngëmu nit ki: mu bàyyi lu ko amalul njariñ»

Tirmizii ak Ahmad ñoo ko soloo ak ñeneen.

Bokk na ci njariñi hadiis bi:

  1. nit ki bàyyi lu ko amalul njariñ ci mbir i diine wala mbir i àddina.
  2. bàyyi lu amul njariñ daa bokk ci matug Lislaamam.