Mottalil hadiisu « man Xara a harfan min kitaabillaahi...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?
- الباب / الفصل
- قسم الحديث
السؤال
س١٤: أكمل حديث: «من قرأ حرفًا من كتاب الله...»، واذكر بعض فوائده.
Laaju 14: Mottalil hadiisu « man Xara a harfan min kitaabillaahi...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?
الجواب
ج:عن عبدِ الله بن مسعودٍ رضي الله عنه: أنَّ النبي صلى الله عليه وسلم، قال:
«مَن قرأ حرفًا من كتاب الله فله به حسنة، والحسنة بعشر أمثالها، لا أقول: ألف لام ميم حرف، وَلَكِنْ ألفٌ حرفٌ، ولامٌ حرفٌ، وميمٌ حرفٌ»
رواه الترمذي.
بعض فوائد الحديث:
- فضل تلاوة القرآن.
- وأن بكل حرف تقرؤه لك به حسنات.
*******
Jële nañu ci Abdul Laahi Doomi Mashuud mune: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:
«képp ku jàng ben araf ci téere Yàlla bi dina ci am wenn yiw, yiw wu nekk day tolloog fukki yiw, duma wax ni alif laam miim benn araf la waaye alif araf la, laam araf la, miim araf la»
Attirmisii moo ko soloo
Yénn ci njariñi hadiis bi:
- ngëneelu jàng Alxuraan.
- benn haraf boo jàng da nga ci am ay yiw.