Skip to content

السؤال

س45: ما هو فضل الحج؟

lan mooy ngëneelu aj?

الجواب

ج:عن أبي هريرة رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، قال: سمعت رسول الله ﷺ يقول:

«من حج لله فلم يرفث ولم يفسق؛ رجع كيوم ولدته أمه»

رواه البخاري وغيره.

  • «كيوم ولدته أمه»: أي بغير ذنب.

jële na ñu ci Abii hurayra -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, neena: dégg naa Yónente bi Yàlla na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc, mu wax ni:

"képp ku aj ngir Yàlla, te beejul sëyul deful ag kàccoor; dana dellu mel ni bis bi ko yaayam jure woon"

Buxaarii ak Muslim ñoo ko soloo ak Keneen.

"mel ni bis bi ko yaayam jure woon" maanaam ci ludul benn bàkkaar.