Skip to content

السؤال

س1: ما نسب نبينا محمد صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ؟

Lan mooy askanu Yónente bi -yal la na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-?

الجواب

ج:هو محمد بن عبد الله بن عبد المطلب بن هاشم وهاشم من قريش، وقريش من العرب، والعرب من ذرية إسماعيل، وإسماعيل ابن إبراهيم عليه وعلى نبينا أفضل الصَّلاة والسَّلام.

Moom mooy Muhammat doomu Abdu Laahi doomu Abdul Mutallib doomu Haasim té Haasim ci xuraysin la bokk, xuraysin bokk ci araab yi, araab yi bokk ci sëti Ismaahiil, te Ismaahiil doomu Ibraahiima la yal jàmm ak mucc nekk ci moom ak ci sunu yónente.