Skip to content

السؤال

س48: ما هو الجهاد في سبيل الله؟

lan mooy jihaad?

الجواب

ج:هو بذل الجهد والوسع في نشر الإسلام والدفاع عنه وعن أهله، أو قتال عدو للإسلام وأهله.

قال تَعَالَى:

﴿وَجَاهِدُوا بِأَمْوَالِكُمْ وَأَنْفُسِكُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ذَلِكُمْ خَيْرٌ لَكُمْ إِنْ كُنْتُمْ تَعْلَمُونَ﴾

[التوبة: 41].

*******

mooy def ay coono ak sa kem kàttan ci tasaare lislaam ak yiir ko moo ki ñoñam, wala rayante ak noon i lislaam ak i ñoñam.

Yàlla mu kawe mi neena:

"na ngéen di jihaad ci yoonu Yàlla ci seen alal ak seen bakkan, loolu moo gën ci yéen ndeem xam ngeen 41"

suuratu attawba 6