Skip to content

السؤال

س31: ما هو الخوف؟ وما هو الرجاء؟ وما الدليل؟

lan mooy ragal ? lan mooy yaakaar ? ak luy tektal bi ?

الجواب

ج:الخوف: هو الخشية من الله ومن عقابه.

الرجاء: هو الطمع في ثواب الله ومغفرته ورحمته.

الدليل: قوله تَعَالَى:

﴿أُوْلَٰٓئِكَ ٱلَّذِينَ يَدۡعُونَ يَبۡتَغُونَ إِلَىٰ رَبِّهِمُ ٱلۡوَسِيلَةَ أَيُّهُمۡ أَقۡرَبُ وَيَرۡجُونَ رَحۡمَتَهُۥ وَيَخَافُونَ عَذَابَهُۥٓۚ إِنَّ عَذَابَ رَبِّكَ كَانَ مَحۡذُورٗا﴾

[الإسراء: 57].

وقال تَعَالَى:

﴿نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ 49 وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ 50﴾

[الحجر: 49-50]

ragal: mooy ragal Yàlla ak mbugëlam.

yaakaar: mooy yaakaar yoolub Yàlla ak njéggalam ak yërmandeem.

tektal bi mooy wax i Yàlla mu kawe mi:

( ñooñu ngeen di ñaan ñoom ci seen bopp da ñiy góor-góorlu ci def lu baax ngir gën a jege Yàlla, ñuy yaakaar yërmandeem di ragal mbugalam te sa mbugalum Boroom lu ñuy moytu la)

saaru Israa: 57

Sunu Borom mi ngi waxaat ne:

( Xibaaral sama jaam ñi ne léen man maay aji-jéggale ji maay aji-yërëme ji 49 waayé sama mbugal mooy mbugal mu metti mi 50 )

saaru Al-Hujraat: 49, 50