Skip to content

Tuddal yenn ci tur i Yàlla yi ak i meloom.

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

س32: اذكر بعض أسماء الله تَعَالَى وصفاته.

Tuddal yenn ci tur i Yàlla yi ak i meloom?

الجواب

ج:الله، والرب، والرحمن، والسميع، والبصير، والعليم، والرزاق، والحي، والعظيم، والحكيم .... إلى غير ذلك من الأسماء الحسنى والصفات العلى.

Yàlla, Boroom bi, Aji-yëram ji, Aji-dégg ji, Aji-gis ji, Aji-xam ji, Aji-wërsëgal ji, Aji-dund ji, Aji-màgg ji... ak yudul yooyu ci ay tur yu rafet ak i melokaan yu kawe.