Skip to content

السؤال

Fan mooy kërug yéefar yi ?

س30: ما هي دار الكافرين؟

الجواب

kërug yéefar yi mooy sawara; Yàlla neena:

Na ngeen ragal sawara si nga xam ne la koy xamb mooy nit ak ay xeer te waajalees na ko ñeel yéefar yi.

saaru Baqara: 24

ج:النار، قال تَعَالَى:

﴿فَٱتَّقُواْ ٱلنَّارَ ٱلَّتِي وَقُودُهَا ٱلنَّاسُ وَٱلۡحِجَارَةُۖ أُعِدَّتۡ لِلۡكَٰفِرِينَ﴾

[البقرة: 24].