Skip to content

السؤال

س33: اشرح هذه الأسماء.

firil tur yii?

الجواب

ج:الله: ومعناه الإله المعبود بحق، وحده لا شريك له.

  • الرب: أي الخالق والمالك الرازق والمدبر وحده سُبْحَانَهُ.
  • السميع: الذي وسع سمعه كل شيء، ويسمع كل الأصوات على اختلافها وتنوعها.
  • البصير: الذي يرى كل شيء، ويبصر كل شيء صغر أو كبر.
  • العليم: فهو الذي أحاط علمه بكل شيء بالماضي والحاضر والمستقبل.
  • الرحمن: الذي وسعت رحمته كل مخلوق وحي، فكل العباد والمخلوقات تحت رحمته.
  • الرزاق: الذي عليه رزق جميع المخلوقات من الإنس والجن وجميع الدواب.
  • الحي: الحي الذي لا يموت، وكل الخلق يموتون.
  • العظيم: الذي له الكمال كله والعظمة كلها في أسمائه وصفاته وأفعاله.
  • الحكيم: الذي أحكم خلقه، وأتقنه، وأحسنه، وله الحكمة في خلقه وأمره.
  • والحكمة: وضع الأشياء مواضعها، وتنزيلها منازلها.

Yàlla: li miy tekki mooy Yàlla ji niy jaamu ci dëgg moom rekk te amul kenn ku ñu koy bokkaaleel.

Buur bi: mooy ki bind te mooy ki moom, mooy wërsëgal te mooy doxal mbir yi moom dong moom Yàlla mu sell mi.

Aji-dégg ji: mooy ki ag déggam daj lépp, muy dégg kàddu yépp ak séeni wuute ak séeni melokaan.

Aji-gis ji: mooy kiy gis lépp, di gis lépp lu ndaw wala mu rëy.

Aji-xam ji: mooy ki xam-xamam bi peeg lépp moo xam li weesu wala li teew wala li ñëwagul

Aji-yërëm ji: mooy ki yërmaandeem daj bépp mindeef ak lépp luy dund, te jaam yépp ak mbindéef yépp ñoo ngi ci suufu yërmàndeem.

Aji-wërsëgal ji: mooy ki wërsëgu mbindeef yépp nekk ci moom moo xam nit la wala jinne wala lépp luy dox ci suuf.

Aji-dund ji: mooy kiy dund te du dee mukk, te mbindeef yépp da ñiy dee.

Aji-màgg ji:mooy ki ame géppug mat ak léppi màgg ci ay turam ak i meloom ak i jëfam.