Skip to content

السؤال

س٣: من أين نأخذ الأخلاق؟

Laaju 3: Ci fan la ñiy jële jikko?

الجواب

ج:من القرآن الكريم، قال تَعَالَى:

﴿إِنَّ هَذَا الْقُرْآَنَ يَهْدِي لِلَّتِي هِيَ أَقْوَمُ﴾

[الإسراء: ٩].

  • ومن السنة النبوية: حيث قال رسولُ اللهِ ﷺ:

«إنَّما بُعِثْتُ لِأُتَمِّمَ صالحَ الأَخلاقِ»

رواه أحمد.

  • Ci Alxuraanul Kariim, Yàlla mu kawe mi neena:

{Alxuraan jii de day gindee jëme ca la gën a jub}

saaru Israa: 57

Ak ci Sunna: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- mune:

«Dan maa yónni ngir ma mottali jikko yu rafet yi»

Ahmad moo ko soloo.