Skip to content

السؤال

س٤: ما هو خلق الإحسان وصوره؟

Laaju 4: Lan mooy jikkoy rafetal ak i anamam?

الجواب

ج:الإحسان: هو مراقبة الله على الدوام، وبذل الخير والإحسان للمخلوقين.

قال النبي ﷺ:

«إِنَّ اللَّهَ كَتَبَ الْإِحْسَانَ عَلَى كُلِّ شَيْءٍ»

رواه مسلم.

من صور الإحسان:

✔ الإحسانُ في عِبادة الله تَعَالَى، وذلك بالإخلاص في عبادته.

✔ الإحسان إلى الوالدَينِ، بالقول والفعل.

✔ الإحسان إلى الأرحام والأقارب.

✔ الإحسان إلى الجارِ.

✔ الإحسان إلى اليتامَى والمَساكين.

✔ الإحسان إلى المُسيء إليك.

✔ الإحسان في الجِدال.

✔ الإحسان في الكلام.

✔ الإحسان إلى الحيوان.

  • Rafetal: mooy di fuglu Yàlla saa sune, ak di defal mbindéef yi yiw ak lu rafet.

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- wax Na ne:

«Yàlla dafa waral rafetal ci lépp»

Muslim moo ko soloo

Bokk na ci anami rafetal yi:

  • Rafetal ci jaamu Yàlla mu kawe mi, te mooy di sellal jaamu gi.
  • Rafetal jëme si ñaari way-jur, ci wax ak jëf.
  • Rafetal jëm ci bokk yi ak jegeñaale yi.
  • Rafetal jëm ci dëkkandoo yi.
  • Rafetal jëm ci jirim yi ak Way-ñakk yi.
  • Rafetal jëm ci kuy ñaawal jëme ci yaw.
  • Rafetal wax yi.
  • Rafetal werente wi.
  • Rafetal jëme si baayima yi.