Skip to content

Mottalil hadiisu « Laa yuumimu ahadukum hattaa akuuna ahabba ilayhi...» te nga tudd yenni ci ay njariñam?

الباب / الفصل
قسم الحديث

السؤال

س6: أكمل حديث: «لا يؤمن أحدكم حتى أكون أحب إليه ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 6: Mottalil hadiisu « Laa yuumimu ahadukum hattaa akuuna ahabba ilayhi...» te nga tudd yenni ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أنس رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«لا يؤمن أحدكم حتى أكون أحب إليه من والده، وولده، والناس أجمعين»

رواه البخاري ومسلم.

من فوائد الحديث:

  • يجب محبة النبي صلى الله عليه وسلم أكثر من كل الناس.
  • أن ذلك من كمال الإيمان.

Jële nañu ci Anas -yàl na ko Yàlla dollee gërëm-, mane: Yónente bi -yal la na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-, neena:

«Kenn ci yéen du gëm lifeek gënëlu ma ko way-juram ak doomam ak mbooleem nit ñi»

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

Bokk na ci njariñi hadiis bi:

-dana war ñu bëgg yónente bi ci kaw mbooleen nit ñi.

  • Loo lu ci matug ngëm la bokk.