Skip to content

Mottalil hadiisu « Laa yuuminu ahadukum hattaa yuhibba Li axiihi ...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?

الباب / الفصل
قسم الحديث

السؤال

س7: أكمل حديث: «لا يؤمن أحدكم حتى يحب لأخيه ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 7: Mottalil hadiisu « Laa yuuminu ahadukum hattaa yuhibba Li axiihi ...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أنس رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ، قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«لا يؤمن أحدكم؛ حتى يحب لأخيه ما يحب لنفسه»

رواه البخاري ومسلم.

من فوائد الحديث:

  • على المؤمن أن يحب للمؤمنين من الخير كما يحب لنفسه.
  • وذلك من كمال الإيمان.

Jële nañu ci Anas -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, neena Yónente bi -yal na na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-, neena:

«Kenn ci yéen du gëm; ndare mu bëggal mbokkam li mu bëggal boppam»

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

Bokk na ci njariñi hadiis bi:

  1. War na ci jullit bi mu bëggal jullit ñi aw yiw ni ki mu ko bëggale boppam.
  2. Loolu ci matug ngëm la bokk.