Skip to content

السؤال

س4: أكمل حديث «أكمل المؤمنين إيمانًا ...»، واذكر بعض فوائده.

Laaju 4: mottalil hadiisu : «Akmalul muuminiina iimaanan...» te nga tudd yenn ci ay njariñam?

الجواب

ج:عن أبي هريرة رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قال: قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«أكمل المؤمنين إيمانًا: أحسنهم خلقًا»

رواه الترمذي وقال: "حديث حسن صحيح".

فوائد من الحديث:

  1. الحث على حسن الخلق.
  2. وأن كمال الخلق من كمال الإيمان.
  3. وأن الإيمان يزيد وينقص.

jële nañu ci Abii hurayrata -yal na ko Yàla dollee gërëm neena: yònente bi -Yalla na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

«ki gën a mat ngëm ci way-gëm yi mooy ki gën a rafet jiko»

Tirmisiyu soloo na ko daal di wax ni: "hadiis bu rafet la bu wér la"

ay njariñ ci hadiis bi:

  1. ñaaxe si rafet jiko.
  2. matug jiko bokk na ci matug ngëm.
  3. ngëm day yokku di wàññiku.