Skip to content

السؤال

lan mooy ag naaféq ak i xeetam?

س٢٢: ما هو النفاق وأنواعه؟

الجواب

Tontuli-

  1. ak naaféq gu mag mooy: nëbb ag kéefar di feeñal ag ngëm.

loolu nag day génne nit ki ci lislaam te moongi bokk ci ag kéefar ku mag.

Yàlla mu kawe mi neena:

naaféq yi fa gën a suufe ca safara la niy nekk te kenn manu leen a dimbal.

suuratu annisaa

  1. ak naaféq gu ndaw:

ni ki lu mel ni: fen ak wuute ab dig ak wor.

naaféq gu ndaw nag du génne nit ci lislaam, waaye ci bàkkaar yi la bokk, ta ki koy def nag manees na ko cee mbugal.

yonente Yàlla bi neena:

màndargam naaféq ñatt la: saa yu waxee fen, saa bu joxee ab dig wuute ko, buñu ko wóoloo mu wor.

Buxaariu ak muslim ñoo ko soloo.

ج:1. النفاق الأكبر: وهو إبطان الكفر وإظهار الإيمان.

ويُخرِجُ من الإسلام وهو من الكفر الأكبر.

قال تَعَالَى:

﴿إِنَّ ٱلۡمُنَٰفِقِينَ فِي ٱلدَّرۡكِ ٱلۡأَسۡفَلِ مِنَ ٱلنَّارِ وَلَن تَجِدَ لَهُمۡ نَصِيرًا﴾

[النساء: ١٤٥].

  1. النفاق الأصغر:

مثل: الكذب، وإخلاف الوعد، وخيانة الأمانة.

ولا يُخرج من الإسلام، وهو من الذنوب، وصاحبه معرَّض للعذاب.

قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:

«آية المنافق ثلاث: إذا حدث كذب، وإذا وعد أخلف، وإذا اؤتمن خان»

رواه البخاري ومسلم.