Skip to content

lan mooy xamleb Alquraan?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy xamleb Alquraan?

س16: ما هو تعريف القرآن؟

الجواب

Alquraan wax i Yàlla la du mbindeef.

Yàlla mu kawe mi neena:

bu kenn ci way bokkaale yi làqoo fi yaw na nga ko fat ndax mu dégg kàddug Yàlla

suuratu attawba 6

ج:هو كلام الله تَعَالَى، ليس بمخلوق.

قال تَعَالَى:

﴿وَإِنْ أَحَدٌ مِنَ الْمُشْرِكِينَ اسْتَجَارَكَ فَأَجِرْهُ حَتَّى يَسْمَعَ كَلَامَ اللَّهِ﴾

[التوبة: 6].

وروي في الحديث:

«وفضل كلام الله على سائر الكلام كفضل الله على خلقه»

رواه الترمذي.