Skip to content

lan mooy sunna ?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy sunna ?

س17: ما هي السُّنَّة؟

الجواب

sunna mooy: pépp wax walla jëf juñu askanale yonente bi wala muy lu kenn def ci kanamam mu saxal ko, wala aw melo ciy jikkoom walla aw bindiinam.

ج:هي كل قول أو فعل أو تقرير أو صفة خَلقية، أو خُلقية للنبي صلى الله عليه وسلم.