Skip to content

السؤال

lan mooy bidaa ak ndax warees na koo nangu ?

س18: ما هي البدعة؟ وهل نقبلها؟

الجواب

Bidaa mooy: lépp lu nit ñi sos ci diine gannaaw yonent bi ak i àndandoom.

Bidaa nag dees koy delloo waaye dee su ko nangu.

ngir wax i yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéwal akug mucc:

bépp bidaa ag réer la.

abuu daawuuda moo ko soloo

lu ci mel ni yokk ci jaamu Yàlla, ni ki yokk ci njàppu ñeenteelu raxaas, ak lu mel ni gàmmu maanaam di féete juddug yonent bi, ndax loolu jugewul ci yonente bi niki noonu ay sahaabaam.

ج:كل ما أحدثه الناس في الدين، ولم يكن على عهد النبي صلى الله عليه وسلم وأصحابه.

  • لا نقبلها، ويجب أن نردها.

لقول النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«كل بدعة ضلالة»

رواه أبو داود.

  • وقوله عليه الصلاة والسلام:

«من عمل عملًا ليس عليه أمرنا فهو رد»

رواه مسلم.

مثالها: الزيادة في العبادة، كالزيادة على الوضوء غسلة رابعة، وكالاحتفال بالمولد النبوي، فلم يرد عن النبي صلى الله عليه وسلم وأصحابه.