Skip to content

ndax amna keneen ku dul Yàlla ku xam kumpa?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

ndax amna keneen ku dul Yàlla ku xam kumpa?

س13: هل يعلم الغيب أحد سوى الله تَعَالَى؟

الجواب

kenn xamul kumpa ku dul Yàlla.

Yàlla mu kawe mi neena:

waxal jaam ñi ne amul kenn ku nekk ci asamaan yi walla ci suuf ku xam kumpa ku dul Yàlla, te kenn xamul kañ la nu leen di dekkil.

suuratu annamli 65

ج:لا يعلم الغيب إلا الله وحده.

قال تَعَالَى:

﴿قُل لَّا يَعۡلَمُ مَن فِي ٱلسَّمَٰوَٰتِ وَٱلۡأَرۡضِ ٱلۡغَيۡبَ إِلَّا ٱللَّهُۚ وَمَا يَشۡعُرُونَ أَيَّانَ يُبۡعَثُونَ﴾

[النمل: 65].